Ayiti
Apparence

| Ayiti | ||||
|
| ||||
![]() Barabu Ayiti ci Rooj | ||||
| Dayo | km2 | |||
| Gox | ||||
| Way-dëkk | nit | |||
| Fattaay | nit/km2 | |||
| Xeetu nguur - Njiitu Réew - Njiitu Jëwriñ |
||||
| Tembte - Bawoo - Taariix |
||||
| Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
Port-o-pirins | |||
| Làkku nguur-gi | wu-faraas, kereyool bu Ayiti | |||
| Koppar | ||||
| Turu aji-dëkk | ||||
| Telefon | ||||
| |
Ayiti ab dun la bu nekk ca Amerik diggu. Day ab dun bu mag bu mu bokkal Republik dominicaine te Port-au-Prince di péyam.
Ayiti mooy reewu ñu ñuul ñi njëkka moom seen bopp ci attum 1804, ca seen fippu ga (1791-1803) ca la ñu dakkee Napoleon ak ay ñoñam ca dun ga.
Magginu turu dëkk ba
[Soppi | soppi gongikuwaay bi]Ci aaday Taino yi, Ayiti da doon tekki suufu doj yu kawe ya walla aw doj ci biir geej.
